رَامُوا مَسِيرِي إِلَى جُرْبِلْ لَدَى لَسَشٍ لَوْ عَايَنُوا سِرَّ مَا… — Kamilu serigne fallou mbacke imame nafila de touba — TG.ME

رَامُوا مَسِيرِي إِلَى جُرْبِلْ لَدَى لَسَشٍ لَوْ عَايَنُوا سِرَّ مَا فِي السَّيْرِ مَا رَامُوا, فَالسَّيْرُ مَوْتُ عَلَى مَنْ نَازَعُوا وَأَذًى وَأَنَّهُ لِيَ إِبْقَاءٌ وَإِكْرَامُ Ci atum (1330 / 1912 ) lañu sàkku ne dañu may yóbbu Jurbel, waaye bu ñu gisoon mbóot mu yéeme mi ci nekk, duñu sàkku loolu. Ndax dem gi alkande ak loraange la ci ñoom, waaye di teraanga ju màgg ak ma des fi samab liggéey di yéwén ba fàww. 04 SAFAR

July 19, 2026 3.6K 4